#alternate Soppi Wikipedia (wo) Mbal Jóge Wikipedia. Sauter à la navigation Sauter à la recherche Mbal gi (Euphorbia hirta) Mbal gi (Euphorbia hirta) Mbal ag garab la gog mi ngi bokk ci njabootug " Euphorbiaceae". Mi ngi bokk ci gàncax yi nga xam ne at ba at lay meññ. [ ] Tëraliin * 1 Mbooram * 2 Njariñ yi * 3 Turu xam-xam wi * 4 Tur wi ci yeneeni làkk Mbooram[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Mbal mi ngi cosaanoo fële ci diggu Amerig. Mbal garab la gog day sax foo xam ne baaxu faa saxe mu yaatu lool ci tund yi nga xam ne dafa am naaj. Niki noonu bari na fële ca Afrig bëj-Saalum. Njariñ yi[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Mbal gi (Euphorbia hirta) Xobi ak tóortóori garabug mbal Mbal garab la gog bari na xeeti jàngoro yu bari yu muy faj, loolu moo tax fépp fumu nekk dan ko fay jëfandikoo rawatina fii ci Afrig nga xam ne dañu ko fiy jëfandikoo ngir muy faj, biir buy daw, naka noonu dañu koo faa jàppe ngir ne mooy li gën a gaaw ngir faj lépp loo nga xam ne dafa jëm ci wàllu noyyi lu ci mel ni asma, ak yaneen xeet yi ni mel. Bokk na ci ay njariam batay dañoo wax ne moom moo gaaw lool ci faj bopp buy mett. ak bëñ buy metti. Turu xam-xam wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi] Euphorbia hirtata Tur wi ci yeneeni làkk[Soppi • soppi gongikuwaay bi] angale: asthma-plant Ci « https://wo.wikipedia.org/w/index.php?title=Mbal&oldid=100315 » lañ ko jële Wàll : * Garab * Meññeef Njëlu joowiin Samay jumtukaay * Duggoo de * Waxtaan ak bii IP * Cëru * Sos am sàq * Dugg Barabu tur * Jukki * Waxtaan [ ] Wuute Wonewiin * Jàng * Soppi * Soppi gongikuwaay bi * Wone jaar-jaaram [ ] Yeneen Seet ____________________ Seet Ayca Joowiin * Xët wu njëkk * Askan * Coppite yu mujj * Aw xët ci mbetteel * Ndimbal Móol/génne * Sos ab téere * Yebbi niki PDF * Sumb bu móolu Boyotu jumtukaay yi * Xët yi mu lëkkalool * Coppite yi ko ñeel * Yeb ab dencukaay * Xëti jagleel * Lëkkalekaay yu fi nekkandi * Xibaar ci xët wi * Yëf Wikidata * Tudd wii xët Yeneeni làkk Ajouter des liens * Coppite bu mujj bu xët wii 7 Suwe 2019 ci 17:47. * Jàppandig ëmbéef lee ngi sukkadiku ci Creative Commons Attribution- Séddoo ci genn anam gi; Man nañoo sukkadiku itam ci yeneen anam. Xoolal anami jëfandiku gi ngir yeneeni leeral. * Politigu sutura * Ci mbiri Wikipedia * Ay aartu * Suqalikat * Statistiques * Déclaration sur les témoins (cookies) * Woneyiin bu mobil * Wikimedia Foundation * Powered by MediaWiki